Joŋantey Afrig Kamerun 2022  Joŋante ba jeex na. Senegaal 0-0 Malawi, Senegaal moo jiitu...

Joŋantey Afrig Kamerun 2022 Joŋante ba jeex na. Senegaal 0-0 Malawi, Senegaal moo jiitu...

Lire la suite








Joŋantey Afrig Kamerun 2022

Joŋante ba jeex na. Senegaal 0-0 Malawi, Senegaal moo jiitu ci kippaangoom am na 5i poñ. Kon Senegaal jàll na ci 8eelu xaaju doytal yi.

8eelu xaaju doytal = 8e de finale 


Les Lions n'ont pas réussi à me faire varier de position

Les "cadres" peinent à prendre leurs responsabilités

Kalidou Koulibaly,Gana Gueye,Sadio Mané doivent hausser leur niveau de jeu et d'engagement

Kouyaté à part sa combativité a-t-il autre chose à proposer?

Aliou Cissé aussi vraiment Ken xamoul son impact dans le jeu de l'équipe

Resultats des courses: 3 matchs joués,un seul but marqué



0 Reviews