Lire la suite
Joŋantey Afrig Kamerun 2022
Joŋante ba jeex na. Senegaal 0-0 Malawi, Senegaal moo jiitu ci kippaangoom am na 5i poñ. Kon Senegaal jàll na ci 8eelu xaaju doytal yi.
8eelu xaaju doytal = 8e de finale
Les Lions n'ont pas réussi à me faire varier de position
Les "cadres" peinent à prendre leurs responsabilités
Kalidou Koulibaly,Gana Gueye,Sadio Mané doivent hausser leur niveau de jeu et d'engagement
Kouyaté à part sa combativité a-t-il autre chose à proposer?
Aliou Cissé aussi vraiment Ken xamoul son impact dans le jeu de l'équipe
Resultats des courses: 3 matchs joués,un seul but marqué
0 Reviews